Song information On this page you can find the lyrics of the song Jammu Africa, artist - Ismaël Lo. Album song Best Of, in the genre Музыка мира
Date of issue: 14.06.2015
Record label: Capitol Music France
Song language: French
Jammu Africa |
Afrika a a a Afrika mon Afrique |
Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq |
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew |
D’ici ou d’ailleurs nous somm' des enfants d’Afrique |
Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix |
Kon jammu Afrika moom lay ñaan |
Mané jammu Afrika mooy suñu natange |
Afrika a a a Afrika a a |
Afrika a a a Afrika mon Afrique |
Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan |
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika |
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur |
Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères |
Kon jammu Afrika moom lay ñaan |
Mané jammu Afrika mooy suñu natange |
Afrika a a a Afrika a a |
Afrika a a a Afrika mon Afrique |
Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men |
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi |
Yoo Alla addu jam to Ruanda |
Yoo Alla addu jam to Burundi |
Yoo Alla addu jam to Casamans |
Lawol Mbignona yee |