![Fa Diallo - Ismaël Lo](https://cdn.muztext.com/i/3284752438043925347.jpg)
Date of issue: 31.12.1999
Record label: Syllart
Song language: Maori
Fa Diallo |
Beuguena wanté mane dé dama amoul |
Da nga di gouné motakh mouy sa khalaat |
Ni Beuguena wanté mane dé dama Ragal |
Da nga di ngouné moutakh mouy sa khalaat |
Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé? |
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar |
Té legui bo ko meunoul demal teudi |
Cherie coco li dé doyna kemane |
Nga nane ma kay niou say té awma pantam |
Fa Diallo wakhma noko toudé |
Nga naan ma takk la mane awma place |
Cherie coco wakhma no ko toudé |
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt |
Di takhawalou |
Mané li dé doyna kemane |
Ni beugu na, ni beuguena la |
Fatou diallo wakhma no ko toudé |
Nga nane ma kay niou say té awma pantam |
Fa Diallo wakhma noko toudé |
Nga naan ma takk la mane awma place |
Cherie coco wakhma no ko toudé |
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt |
Di takhawalou |
Mané li dé doyna kemane |
Ni beugu na, ni beuguena la |
Fatou diallo wakhma no ko toudé |
Ni beugu na, ni beuguena la |
Cherie coco wakhma no ko Guissé |
Ni beugu na, ni beuguena la |
Fatou diallo wakhma no ko toudé |
Ni beugu na, ni beuguena la |
Cherie coco wakhma no ko Guissé |
Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé? |
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar |
Té legui bo ko meunoul demal teudi |
Cherie coco li dé doyna kemane |
Nga nane ma takk la mane awma pantam |
Fa Diallo wakhma noko toudé |
Nga naan ma takk la mane awma place |
Cherie coco wakhma no ko toudé |
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt |
Di takhawalou |
Mané li dé doyna kemane |
Ni beugu na, ni beuguena la |
Fatou diallo wakhma no ko toudé |
Ni beugu na, ni beuguena la |
Name | Year |
---|---|
Tajabone | 2015 |
Jammu Africa | 2015 |
Nafanta | 2015 |
Tadieu Bone | 1986 |
Dibi Dibi Rek | 2015 |
Noir Et Blanc ft. Ismaël Lo | 2015 |
L'Amour A Tous Les Droits | 2015 |
Without Blame ft. Marianne Faithfull | 2015 |
Sofia | 2015 |
Liberté ft. Ismaël Lo, Lokua Kanza, Koffi Olomide | 1999 |
Après la guerre ft. Ismaël Lo | 1999 |