Lyrics Yama - Youssou N'Dour

Yama - Youssou N'Dour
Song information On this page you can read the lyrics of the song Yama , by -Youssou N'Dour
In the genre:Африканская музыка
Release date:06.10.2002
Song language:Swahili

Select which language to translate into:

Yama
Soubateel, bamuy barilé
Ñi di déloo sen palanter
Ngir baña xaar li xew, li xew féneen
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Gaal gi teer
Ba ñu seet li, li wara dem féneen
Té du yeebi ludul meew lifi des
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Moo waral bu sédalé, du am
Du am, rusna ñaan ba day fandé, fandé
Moo waral bu sédalé, ba du am
Du am, rusna ñaan Kii daal amu fi morom
Yaamaa nango sona lol
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni dox sa waar bamu noppi yaw
Téréwul topa bëgë bëgë xaléyi
Yaama rek la soxal diarama
Diarama, diarama
Ni woo Yama, Yama
Wuy Yama, amufi morom
Wuy Yama, nangoo sona lol
Ni Yama, jigen ju man goor
Wuy Yama, maa la setlu way
Moo waral bu sédalé, du am
Rusna ñaan ba day fandé
Amu fi morom
Mala setlu way
Yama, Yama
Amul noflay
Amu fi morom
Tunda wi rañénañ la
Yama, Yama
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama gaa yi yaaba leen
Ni dox sa waar bamu noppi yaw
Téréwul topa bëgë bëgë xaléyi
Yaama rek la soxal diarama

Share the lyrics:

Write what you think about the lyrics!

Other songs by the artist: