Song information On this page you can find the lyrics of the song Confession, artist - Youssou N'Dour. Album song History, in the genre Африканская музыка
Date of issue: 25.04.2019
Record label: Naïve Records
Song language: Maori
Confession |
Yow waxma |
Lanelay deff |
Meunuma ci dara |
Mane xawma |
Lanelay deff |
Meunuma ci dara |
Waxnako deguma |
Meunuma ci dara |
Choix wam leu |
Choix wam leu |
Meunuma ci dara |
Kaféwukok dara |
Waxtanewuko |
Meunuma ci dara |
Ahh yeahhh |
Ni dal leu deimei |
Bu feikkei beuguetoula delu |
Nañ ko fi bayi mouy weundelu |
Bumacci keine garouwalei |
Mane waxumako nañ nobanté |
Majeure leu mom teu werneu |
Té neineu yeug yeuguem leu |
Bess buni maniko mu delu |
Munema beugutoula delu |
Mane sax dal bayinako |
Mbeuguel dh bou xassei djokk |
Keine meunuki teye |
Choix wam leu |
Choix wam leu |
Choix wam leu keissei |
Te mom sax |
Da bayi njabotam |
Té neineu dotul delu |
Ahh yee ahh yee |
Dumacci dara |
Ahh yee ahh yee |
Meunumacci dara |
Bu feikkei beuguetoula delu |
Nañ ko fi bayi muy wendelu |
Bumacci keine garouwalei |
Mane waxumako nagn nobante |
Majeure leu mom teu werneu |
Te neineu yeug yeuguem leu |
Bess bounei maniko mu delu |
Munema beuguetoula delu |
Buma keine wax |
Teyei wumako |
Dafay soga beug |
Mbeuguelo mbeuguel |
Bu djoguei keine dotuko teiye |
Mbeuguel woy mbeuguel |
Bu jogue keine meunuko teiyei |
Ahh yee ahh yeee |
Bumacci keine garouwalei |
Bu feikkei beuguetula delu |
Nañ koffi bayi muy wendelu |
Bumacci keine garouwalei |
Mane waxoumako nagn nobantei |
Majeure leu mom teu werneu |
Te neineu yeug yeuguem leu |
Bess bunei maniko mu delu |
Munema beuguetoula delu |